Nanga def aadama? ñoo ngi lay dala ci wikipedia wolof. Di am mbégte ci sag bindu, di am yaakaar ne dinga jàpp bu baax ci liggéey bi muy ci wallu xarala walla ci bind ay jukki. Loo soxla man nga maa bind ci sama xëtu waxtaanuwaay. Yakamti naa loo tambale liggéey ak yaw. Di sàkku ci yaw nga yër xëtu ndimbal wi. Jërëjëf --Ibou (xëtu waxtaanuwaay) 19 Semwiyee 2015 à 21:56 (UTC)

Démarrer une discussion avec Falladam

Démarrer une discussion