Dalal-jàmm ci wikipedia, téerexamteef bi ubbeeku bi. Sag mbindu mbekte la ci askanu wikipedia. Soo soxlaa ndimbal, maanaam so bëggee xam nooy sosee aw xët, noo leen di soppee, ak nu wikipedia di doxee, añs(ak ñoom seen); Demal ci tërug ndimbal gi. Soo amee ay laaj, demal ci bunt bi ñu jagleel askanu Wikipedia. --Ibou 18 septembre 2007 à 10:36 (UTC)

Démarrer une discussion avec Bujuman

Démarrer une discussion