Waxtaan:Xaralaymbëj
Ku ci gis ay njuumte maa ngi lay woo nga jubbanti leen. di la nuyu
ay laaj
Soppidama doon wax ndax manoo maa yonnee dayi cosaan yi maanaam les textes originaux ma dëppale leen teeki ko nu mu gën a leere
Ku ci gis ay njuumte maa ngi lay woo nga jubbanti leen. di la nuyu
dama doon wax ndax manoo maa yonnee dayi cosaan yi maanaam les textes originaux ma dëppale leen teeki ko nu mu gën a leere