Waxtaan:Ndëgërlu gu mbëj

(Yoonalaat gu jóge Waxtaan:Ndëggërlu gu mbëj)
Dernier commentaire : 14 at ci ginaaw par Ibou

jaajef sang ibou ci tekkiin wu jaar yoon wi, gis naa ne bis bu ne maa ngi gën di gis sag màgg ci wàllug man ak xarañ ci tekki ak tekkiin--Abdu Xaadir Kebe (xëtu waxtaanuwaay) 5 Maars 2010 à 18:10 (UTC)Répondre

Jërëjëf! yaay sama ustaas :-) --Ibou (xëtu waxtaanuwaay) 5 Maars 2010 à 19:19 (UTC)Répondre
Revenir à la page « Ndëgërlu gu mbëj ».