Waxtaan:Fitna

Dernier commentaire : 2 at ci ginaaw par 212.114.207.30 dans le sujet Jubanti

Jubanti

Soppi

Mbok nuyu na leen, dama bëggon ngeen xolaat bind mi ndax bari ba ay njumte. Tay sokoy dawal dangay gis nii baatan yi ni ñu ko binde dafa doy waar loolu nag ma sakku won ngeen defaat ci ay gestu ndax dawal bi mën a nex ci kuy tambali njàng mi

Jaa ngeen jëff 212.114.207.30 4 Maars 2022 à 19:43 (UTC)Répondre

Revenir à la page « Fitna ».