Wén gi xeetu garab la gu bokk ci ñoñ Pterocarpus ak ci njabootu Fabaceae. Ci Sahel gi lay meññ ci Afrig.
Mattam nekk na lu nit ñi xëntewoo.
Pterocarpus erinaceus
Farañse: véne (wén)