Santo Antão (Kap Weert)

(Yoonalaat gu jóge Santo Antão (Kap Weer))


Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Santo Antão diiwaan nekk ci yu Kap Weer.

Dunu Santo Antão
Réew Kap Weer
way-dëkk 43 915 (2 010)[1] nit
Rëyaay 779 km²
Locator map of Santo Antão, Cape Verde.png
Pico da Cruz
Paúl
Fontainhas
Valle de Ribeira Grande
Porto Novo.
Estrada da Corda

DëkkaaniSoppi

  • Paul
  • Porto Novo
  • Ribeira Grande

DëkkiSoppi

Dëkk-DëkkaaniSoppi

DayoSoppi

  • Luís de Matos Monteiro da Fonseca
  • António do Espírito Santo Fonseca
  • Leão Lopes
  • Gabriel Mariano
  • Manuel de Novas
  • Luís Romano de Madeira Melo
  • Roberto Duarte Silva
  • Antoninho Travadinha

Football clubiSoppi

  • Liig Porto Novo:
    • Académica do Porto Novo
    • Inter Porto Novo
    • Marítimo Porto Novo
    • Sporting do Porto Novo
  • Liig Ribeira Grande (Liig bej-gannar Santo Antão):
    • Beira Mar
    • UD Janela
    • Paulense DC
    • Rosariense
    • Solpontense FC

Karmat ak delluwaaySoppi

  1. Instituto Nacional de Estatística: [1]

Lëkkalekaay yu bitiSoppi

 

Xool it Wikimedia Commons