Royuwaay:Nataalu ayubés bi
|
Ndakaaru (Dakar) Nekkoon péyu Afrig gu sowwu gu fraase (ASF, walla AOF ci FR), Ndakaaru fimne mooy Péyu reewum Barug Senegaal akit goxub Ndakaaru, tolluwaayam ci péeteg sowwu bu Afrig, ci jegeem Daanaka-dun bu Kap-Wert, waral na sancug notaakon yu jëkk yi, Akit yaxantu ak Àdduna bu bees bi, te ame na peetewaayu ngëneel ci jëflanteg cosaani Saa-Afrig yi ak Saa-Tugal yi. Fa lees Taxawalee woon Xumbalu Àddina bu fànni ñuule (jaam yu ñuul) bu njëkk bi ci xalaatu Leopool Sedaar Sengoor atum 1966, Dëkk bii mooy toogu bu Këru-gëstu bu dàttu bu Afirg gu ñuule (KDAN, walla IFAN ci FR) akit bu Bànk bu diggu bu guuri Afrig gu sowwu (BDGAS walla BCEAO ci FR) |