Nuwaaksot
Nuwaaksot (Nouakchott) : mooy pééyu réewum Gànnaar ak dëkk bi ko ëpp solo. Moom la bokk ci dëkk yi gën a mag ci Saara. Dëkk bi itam moo nekk màkkaanu nguur ak koom-koom ci réewum Gànnaar.
Xool it Wikimedia Commons
|