Ubbi njël lu njëkk li
ab Nosukaayu kenn (pc)

Nosukaay ab wuutuloxo bu mbëjfeppal la buy seggat ay xibaar yu ñu ko jox jaare ko ci ag noste gu xellu gu ñu tëral-jiital. Ci wàllu xibaarfeppal la ñu koy jëfandikoo.

  • Français: ordinateur
  • English: computer, di tekki waññikaay, ndax yi ñu ci njëkk a defar waññi rekk lañ doon def.