Jurbel
Jurbel (=Njaaréem) (fr. Diourbel) benn dëkku Senegaal la.
Diourbel (Arabic: ديوربل; Serer: Jurbel, Wolof: Njaaréem) dëkk la bu nekk ci diggu senegaal feete penku Dakaar ak Cees, diggam ak Dakaar nag moo ngi tóllu ci 146km . Siiwe na ci Jumaam ju mag ji ak bërëbu ligéeyukaay bu mag ba woon SENEOR.
Touba bokk na ci dëkk yi gën a siiw te ëpp ay nit ci bile gox.
Jurbel mooy ndayu dëkk yi féete ci gox boobu, séddalikoo ci ñàtti diiwaan : Jurbel, Bambay ak Mbàkke.
dayo bi : 31,24km
fàttaay gi : 5,000Km
Limub askan wi 2023 was 157,554.