Isipt gu yàgg ga wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Xët wu bees : Xayug Isipt Isipt bu njëkk dafa séddaliku woon ay xaaj. Ci jamonoy 3200 nj.j(njëkk judd gi) lañu bennal xaaj yii, mu mujj nag di nguur gu dëgër, buur bu tudd Firhawna jiite ko...
 
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
 
Xayug Isipt
 
Ligne 10 ⟶ 9 :
Waa Isipt am nanu xay gu cosaanu, ñu nekkoon ñu daa gëm ay yàlla yu bari, daan leen melale ci bindu nit ku am boppub bàyyima., yàlla ju ci mel ne Amoon Ra (yàllay jant ji) benn la ci ak Isis (yàllay weer wi) , nga xam ne Firhawna it yàlla lanu ko jàppe woon. Daa nanu tabaxal seen yàlla yi ay jaamuwaay (ay temple) ngir màggale leen ko. Ña cay ñu woomle dañu daa tabaxal seen bopp ay bàmmeel yu yor bindub mbaanaar (pyramide).
Bu ñu daa suul seeni néew nag, dañu ci daa boole mbooleem seeni bagaas ak alal.
Ci atum 332 nj.j la waa Geres teg loxo Isipt, booba it la tàmbalee naaxsaay.