Feppsaal wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
HiW-Bot (waxtaancëru)
m r2.7.2) (Robot: Modifying scn:Prutuni
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Feppsaal''' (deesi ko wax ci fr : Proton)(as [[wàll-wàllaan]] la su sëfoo [[yanu mbëj]] bu baax(+) su man a féex ciy yëngoom walla mu taq cib [[saalu xarefulwoon]] . Ki ñuy wax ne moo ko wuññi mooy Ernest Rutherford, donte [[Jëmm|jëmmaan]] bu [[Almaañ|waa-almaañ]] bi Eugene Goldstein njoortoon na ag nekkam njëkk ngir manoon a dëggal ay gëstoom. Dayoob yanu mbëjam tollook bu [[mbëjfepp]], waaye ak màndarga gu wuute: 1,602 × 10<sup>-19</sup> [[coulomb]]. [[Lef]]am tuuti la rombee 1800 yoon bu mbëjfepp (daanaka 1836) te xawa tollook bu [[feppmaandu]]: feppsaal a ngi am lef gu toll ci 1,6726231 × 10<sup>-27</sup> kg (9,3828 × 10<sup>2</sup> [[mbëjfeppvolt|MmV]]).
 
Feppsaal yeek feppmaandu yeey ñaari wàll-wàllaan yi cëroo [[xarefulwoon]] bi, ñoom ñaar ci saal bi lañu nekk, mbëjfepp yi ci xarefulwoon lañu leen boole waaye taquñu ci dañuy nekk di ko wër.