Melosuufug Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
MastiBot (waxtaancëru)
m r2.7.1) (robot Adding: pam:Heograpiya ning Aprika
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 105 :
Jant bi day jamu ci [[gёwéelub sànkar]] bi, bu ko defee tàngoor wi yékkatiku ci xaaju Gox bu bёj-gànnaar bi, nekk nag di lu yam te taradi ca xaaju Gox bu bёj-saalum bi.
 
NaajNaj gu jawwu gi (pression atmosphérique) , Gnelawngelaw li, Taw yi:
 
Jant bi day jamu ci gёwéelub sànkar bi, ci bёj-gànnaaru Gox bi, bu ko defee tàngoor wi yékkatiku, naj gu jawwu gi daal di woyof, te fekk naj gu jawwu gi mi ngi gёn a am doole ci mbàmbulaanug atlas gi, loolu di waral ngelawi kojug dig (saisonnier) yu bёj-saalumu sowwu yiy tawloo di jañu juge ci mbàmbulaanug atlas gi jёm ci barab bi naj gu jawwu gi di gёn a woyofe, bu ko defee taw yi daal di rot ci Tefesug Gana gi, ak Laamaaru Ecoopi ak bёj-saalumu Sudaan.
Rëdd 117 :
Ngelawi sowwu yu safaanu yiy tawloo (ndax ci [[Mbàmbulaanu Atlas]] lañuy juge) dañuy upp, di rotal ay taw ci tefesi bёj-gànnaaru penku yu Gox bi, ngelaw yii nag dañuy àgg ci tàkk gu mag gi, di lu fendi. Te tam Tàkk gi jamono ju nekk ngelawi yaxantu yu tàng yi danu koy upp.
 
Ngelawi yaxantu yu bёj-saalumu penku yiy tawlo dañuy upp ci tefesi bёj-saalumu penku yu Afrig yi, bu ko defee taw yi rot, ñuy sutuxlu ci biir ci kaw Laamaaru Bёj-saalumu Afrig, bu ko defee ñu àgg ciw tàngoor ba ca Tàkkug Kalahaari, ci bёj-saalumu sowwu Afrig.
 
=== Diiwaani kilima yi ===