Xiirtalu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : Xiirtalu ag feeñte la gees di gis ci ag ndombo gu mbëj. su dawaan biy jàll ci ndombo gi di soppeeku, sunu sukkandikoo ci àtte Lorentz, dafay sabab jenn [[Dooley mbëjd...
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 2 :
 
==Tekkeem==
Su ab dawaanu mbëj '''''i''''' di jàll ci ab wommatukaay xiirtalu gi mooy muy juddal ab toolu bijjaakon ci li ko wër. Su nekkee dawaan buy soppeeku ci jamono [[walug bijjaakon]] bi ''<math>\Phi</math>'' dafay soppeeku ci jamono moom itam, coppite googu mooy sabab jenn doole ju mbëjdoxalukaay juy bañ coppiteg wal gi.
 
Segam xiirtalu gi mooy liy bañ coppiteeg dawaan bi te ci [[dawaan bu safaanu]] li ñu bëgg mooy dawaan bi di man a soppi dayoom ak ci benn baraay bi, kon xamees na ne man naa nekk gànlankoor ba tax keman wara tuuti. Xiirtalu gi '''''L''''' walug toolu bijjaakon beek dawaanu mbëj bi ñoo nu koy jox.
Rëdd 33 :
 
==Xiirtalante==
Su benn dawaan bi '''i''' biydi aw ci genn ndombo gu mbëj jureete di jur ab toolu bijjaakon buy àgg ci geneen ndombo gu nekk ci wetam, daf fay jur jenn doole ju mbëjdoxalukaay moom it juraat beneen toolu bijjaakon buy dellu ci ndombo gu njëkk ga daldi fay jur, moom waat, jeneen dooley mbëjdoxalukaay abak beneen toolu bijjaakon.
 
Su benn dawaan bi '''i''' biy aw ci genn ndombo gu mbëj juree ab toolu bijjaakon buy àgg ci geneen ndombo gu nekk ci wetam, daf fay jur jenn doole ju mbëjdoxalukaay moom it juraat beneen toolu bijjaakon buy dellu ci ndombo gu njëkk ga daldi fay jur, moom waat, jeneen dooley mbëjdoxalukaay ab beneen toolu bijjaakon.
 
Su fekkee genn ndombo rekk la dawaan bi koy jàll mooy jur toolu bijjaakon biy jur dooley mbëjdoxalukaay ji.
 
Su fekkee nak ñaari ndombo lañu toolu bijjaakon bi kenn kiy jur, du yam ci moom rekk, mooy dem ci geneen ndombo gi jur fa dooley mbëjdoxalukaay biyjiy bañ coppiteeg dawaan bi jàllkoy kojàll.
 
:<math>M_{1/2} = \frac{\Phi_2}{i_1} \,</math>