Mbëjbijjaakon wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Mbëjbijjaakon''' mooy banqaasu [[jëmm]] biy gëstu feeñte yu mel ne [[mbëj]] ak [[bijjaakon]] ak lépp lu lees ñeel (niki ci misaal [[tool bijjaakon|tooli bijjaakon]] yi juddoo ci [[dawaanu mbëj]] ak dawaani mbëj yi juddoo ci tooli bijjaakon).
==== wolof ====
 
Ñoo ngi ko tëgg ngir man a faramface ci anam gees boole feeñte yu mbëj ak yu bijjaakon. Ay feeñte yu mel ne [[sababu mbëjbijjaakon]] ngir wone ni [[toolu mbëj]] lënkook [[toolu bijjaakon]]: ab toolu bijjaakoon buy soppiku dafay ju ab toolu mbëj, naka noonu la toolu mbëj buy soppiku di juree ab toolu bijjaakon. [[Yamaleb Maxwell]] mooy liy faramface mbëjbijjaakon te di sukkandiku ci [[Yanu mbëj|yan]] ak dawaanu mbëj.
 
==== françaisTaariix ====
[[William Gilber]] , ci téereem ba ''De Magnete'' (1600), la wone wuute gi nekk ci diggante aw yaram wu mbëj ak wu bijjaakon. Mu fésal àtte yi laqu ci bëmëxante ak xëccante yu bijjaakon yi jaare ci seeni dott ak njeexit li tàngoor am ci bijjaakon bu weñ.
* éléctromagnétique
* éléctromaqnétisme
 
ci 1831 la [[Michael Faraday]] doon gëstu doxiinu dawaan bi ci biir ab toolu bijjaakon ba gis ca ne moom, bijjaakon bi, man naa jur liggéey. Oersted moom wuññi woon na ne ab dawaanu mbëj dafay jur ab toolu bijjaakon, Faraday moom wuññi ne ab toolu bijjaakon dafay sabab ab dawaanu mbëj. Ci noonu la wuññee baaxi [[doxalukaay bu mbëj]] ak ni liggéey bu [[doolerandu]] man a soppeekoo [[kàttanu mbëj]], naka-noonu mu sàkkee ca ab [[Jurukaayu mbëj|jurukaayu dawaan]].
==== Italiano ====
* elettromagnetica
* elettromagnetismo
 
Mbëjbijjaakon a ngi judd ci bi [[James Maxwell]] (1864) boolee ay gisiin yu jiitu woon, niki [[mbëjtekkaaral]], [[bijjtekkaaral]]. Bii gisiin di bees bennal moo leeral jikko yi ci yani mbëj yeek dawaani mbëj yi, bijjaakon yi, [[Duusub mbëjbijjaakon |duusi mbëjbijjaakon]] yi, yu mel ne ag [[leer]] walla [[duusub rajo |duusi rajo]] yi.
 
[[Wàll:mbëjbijjaakon]]
[[Catégorie:baati wolof]]
[[af:Elektromagnetisme]] [[an:Eletromagnetismo]] [[ar:كهرومغناطيسية]] [[az:Elektromaqnetizm]] [[be-x-old:Клясычная электрадынаміка]] [[bg:Електромагнетизъм]] [[bn:তড়িচ্চুম্বকত্ব]] [[bs:Elektromagnetizam]] [[ca:Electromagnetisme]] [[cs:Elektromagnetismus]] [[da:Elektromagnetisme]] [[de:Elektrodynamik]] [[el:Ηλεκτρομαγνητισμός]] [[en:Electromagnetism]] [[eo:Elektromagnetismo]] [[es:Electromagnetismo]] [[et:Elektromagnetism]] [[fa:الکترومغناطیس]] [[fi:Sähkömagnetismi]]
[[fr:Électromagnétisme]]
[[gl:Electromagnetismo]] [[he:אלקטרומגנטיות]] [[hi:विद्युतचुम्बकत्व]] [[hr:Elektromagnetizam]] [[hu:Elektromágnesség]] [[ia:Electromagnetismo]] [[id:Elektromagnetisme]] [[is:Rafsegulfræði]] [[it:Elettromagnetismo]] [[ja:電磁気学]] [[kn:ವಿದ್ಯುತ್ಕಾಂತತೆ]] [[ko:전자기학]] [[la:Physica electromagnetica]] [[lb:Elektromagnetismus]] [[lv:Elektromagnētisms]] [[mr:विद्युतचुंबकत्व]] [[ms:Keelektromagnetan]] [[nl:Elektromagnetisme]] [[nn:Elektromagnetisme]] [[no:Elektromagnetisme]] [[pl:Elektrodynamika klasyczna]] [[pt:Electromagnetismo]] [[ro:Electromagnetism]] [[ru:Электродинамика]] [[scn:Elettrumagnetismu]] [[simple:Electromagnetism]] [[sk:Elektromagnetizmus]] [[sl:Elektrika in magnetizem]] [[sq:Elektromagnetizmi]] [[sr:Електромагнетизам]] [[su:Éléktromagnétisme]] [[sv:Elektromagnetism]] [[ta:மின்காந்தவியல்]] [[th:ทฤษฎีแม่เหล็กไฟฟ้า]] [[tr:Elektromanyetizm]] [[uk:Класична електродинаміка]] [[ur:برقناطیسی قوت]] [[vi:Điện từ học]] [[war:Electromagnetismo]] [[zh:电磁学]]