Dawaan bu safaanu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
m Tuddewaat nañ Dawaan gu safaanu léegi mooy Dawaan bu safaanu
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Dawaan gubu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
== Doxiin ==
Naka-jekk dawaanu [[mbëj]] suñu koy séddale ci dawaan gubu safaanu gubu [[Baraay|baraayam]] sax ci 50 Hz walla 60 [[Hz]] lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne).
 
Jëfandikoo gu dawaan gubu safaanu mi gi jóge ci li [[Jurukaay|jurukaayu dawaan]] yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan gubu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan gibi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.
 
Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan gubu safaanu bir na ne moo gën a yaxan [[dawaan gubu wéy]] ci séddaleeb [[taraay bu kawe]] (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu [[gennwéq]] walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu [[ñettiwéq]] di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu [[Joule]] (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan gubu safaanu gubu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd lool yi.
Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan gu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoom fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci [[taraay]]u [[dawaan]], ci ndimbalu [[soppikaay]] yi, ak ñakkug kàttan gu digu.
 
Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan gubu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoomjëfandikoo fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci [[taraay]]u [[dawaan]], ci ndimbalu [[soppikaay]] yi, ak ñakkug kàttan gu digu.
Donte yenn jumtukaay yi [[dawaan gu wéy]] lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan gu safaanu, sunu jëfandikoo ab [[jubbantikaay]].
 
Donte yenn jumtukaay yi [[dawaan gubu wéy]] lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan gubu safaanu, sunu jëfandikoo ab [[jubbantikaay]].
Sunu jëfandikoo ag xaralag [[mbëjfeppal]] gu kàttan gu yaxan, manees naa jëfandikoo dawaan gu wéy ngir am dawaan gu safaanu, jur ko ci yenn anami [[baraay]], [[melokaanu duus]] ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee [[Jallarbikaay|jallarbikaay]].
== Taariix ==
 
SunuSuñu jëfandikoo ag xaralag [[mbëjfeppal]] gu kàttan]] gu yaxanñaw, manees naa jëfandikoo dawaan gubu wéy ngir am dawaan gubu safaanu, jur ko ci yenn anami [[baraay]], [[melokaanu duus]] ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee [[Jallarbikaay|jallarbikaay]].
 
== Taariix ==
[[Dencukaay:WorldMap Voltage&Frequency.png|400px|thumb|right|Lonkoyoonu àdduna bi bees melool aju ci taraay a baraayu kàttanu mbëj ci ndombo yiy séddale dawaan gi ci kër yi.]]
 
Ca njalbeenu njëfandikoognjëfandikug kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIX<sup>u</sup> xarnu [[daawaan gubu wéy]] lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy [[tegle]] ak li mu gën a wóor dawaan gubu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon [[xareeb dawaan yi]].
 
Dawaan gubu safaanu, gi soloom doonoon lu beneen xaaj bi boole woon [[Nikola Tesla]] ak [[George Westinghouse]] doon aar, manul a ñakk ci njëfandikoonjëfandiku gu ab [[soppikaaysoppalikaay]], moom mi tax ñuy man jokkalante mbëj mi ci diggante yu gudd. Te itam [[doxalukaayu mbëj]] yu dawaan gubu safaanu ñoo gën a wóor te gën a yaxan yu dawaan yu wéy yi.
 
Ci jamono jii ci [[àdduna]] bi dawaanu mbëj ci ñaari [[baraay]] lañu koy séddalee, 50 Hz([[Tugal]], [[Asi]], [[Afrig]]) ak 60 Hz([[Diiwaan-yu-Bennoo]] ak goxu [[Aamerig]] géppbépp ci lu daj, genn xaaju [[sapoŋ]]) ak taraay yu wuute.
 
== Xool it ==