Xam-xamu nosukaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Xam-xamu nosukaay''' (walla '''Xam-xam gi ñeel nosukaay'''), moo yor gëstu gi aju ci [[Cëslaayu xibaar|cëslaay yu xibaar]] yi, xarala yi ñeel seenug nos ak seenug jëfandikoowiin ci noste yi ñuy jëfandikoo ay [[nosukaay]]. Ñi ciy yëngu seen liggéey doon lëkkale ay nosukaay ñu doon li ñuy tuddee abag [[lonkoo]], defar ay [[Dàttub njoxe|dàtti njoxe]], [[Noste gu boppu|boppal ay noste]], defar ay [[Tëriin|tëriin]] te loolu laaj na xam abag [[Kàllaamab tëriin|kàllaamabkàllaamag tëriin]], .
 
Cig lawal, xam-xamu nosukaay dafa ëmbu ci li ñuy wax ''[[Xaralay xibaar ak jokkoo yu yees| xaralay xibaar ak jokkoo yu yees]]'' yi di xeetu xam-xam bi ëmb lépp li ñeel xibaar, ci bépp anamam. Ci tëriin wi la tëralkat bi di joxee ay tektal nosukaay bi ci anam bigi mu warawar a yoree xibaar yi, lan la ci warawar a def ak nan la ko warawar defeea defe. [[Jëfaan]] yi naknag ñooy mbooleem cëri nosukaay bi, benn bu ci nekk am na liggéey buñbu ñu ko sant: yii di rënk xibaar yi, yii di leen wone ni nga bëgge, yii di leen soppi...
 
== Taariix ==
Ba àdduna dooree ba tay nit daa mas di ut ay jumtukaay ngir man a def ay waññeem. Ci jumtukaay yooyu, ci yi gënnagën a yàgg, man nañu cecee lim àlliweebàlliway [[Hammurabi]] (1750 laataalaata yeesu). [[Wuutuloxo]] yu [[doolerandu]] yu njëkk ñoo ngi tambaleetàmbalee feeñ ci diggante XVII ak XVII<sup>u</sup> xarnu. Waññikaay bu doolerandu bu njëkk, jàpp nañu ne, mooy bu Wilhelm Schickard ci XVI<sup>u</sup>.
 
Ci [[1642]] [[Blaise Pascal]] defaroon na, moom itam, ab Waññikaay bu doolerandu, doonoon buñubu ñu doon jaay sax, ba tay jii juroom-ñentñeent ci yooyu man nga leen a fekk ci jeexiituwaay (muse) yi. Ci ay njëlbeenam man nanoo wax ne [[xaymaan]] yi rekk ñoo ci doon yëngu ndax li leen yetteeloon moo doonoon defar ay jumtukaay yu leen di yombalal seeni Waññi yu xayma. Ay cëslaayam yépp ci xayma lañu taxaw, rawatinarawati na liñuy way [[Aljibar bu Bool|aljibar bu Bool]].
 
Tay jii xam-xamu nosukaay jël na wàll wu am solo ci sunug dund, cig sokkalikusuqali ci wàllu koom-koomukoom ak mboolaymboolaay yu askan yi.