Wolof (askan) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 :
Waaye ba noppi Njaajaan dañu koo dàqe dëkk ba, ndax daa am ku ko bëggoon a ray. Mu daal di woon daw ba Jolof ca Wolof ya. Njaajaan Njaay dajale woon na Wolof yi ndax ñu gën a am doole, ba man a taxawal Imbraatóor gu Djolof. Wolof yi, [[Jolof]] mooy seeni dëkk, waaye ak seeni imbraatoor gi, dañoo demoon dëkk te yor: [[Waalo]], [[Tekuruur]], [[Kajoor]], [[Bawal]], [[Siin-Saalum]], Njarmeew (soog a dëkk Bundu), Ñaani, Wulli, Bambug. Nguur ga gépp Jolof uffoon na ko. Lii moo tax Làkku Wolof mooy làkk wi ñu gën a wax ci [[Senegaal]]. Ca atum 1549 la Jolof gu mag ga tas ak Lele Fuli Fak. Nguuri Wolof yépp am seeni buuri bopp: Dammeel ca Kajoor, Teeñ ca Bawal, Baraag ca Waalo, Buurba ca Jolof (Ca Jolof gu mag ga, Buur Fari lañu daa wax). Decce Fu Njóogu ak Amari Ngóone Sabel Faal, ñoo fi njëkk a nekk Dammeel-Teeñ.
 
'''Njabooti Wolof yooyu, ñoo yoroon nguuri wolof yi:'''
* Njaay (Jolof)
* Mbóoj ak Wàdd (Waalo)
Rëdd 9 :
[[Image:Thiédo.jpg|200px|thumb|ab [[Ceddo]] ca wetu [[Bàkkel]] ([[1853]])]]
 
'''Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon:'''
 
* Géer/Garmi, ca kaw, ñoo doon nekk buur yi. Kàŋam (buuri Laman yi) Farba Kaba (buuri [[Ceddo]] yi), Tuube, Bumi ak Lingeer.
Ca seeni meen ñoo man a nekk Buur. Meen moo gën a am solo Geño([['''[[Meen]]''']]:wàllug nday). [['''[[Geño]]''']]:wàllug baay .
* JambourJàmbur ak Serign ySëriñ. NiomÑoom SerignSëriñ ysi ay TukuloorTukulóor lanu(Dia[[Mbàkke]], SyJa, Si, SallLóo, Sàll) Saraxule (SyllaSilla, KhouléXulé, CisséSiise, DraméDaraame, KébéKebe) walawalla ay Naar (DiakhoumpaJaxumpa, AïdaraAydara, CoundoulKundul, SadySaadi, BabouBaabu) lani doon.
* BadoloBaadoola, MbeyMbay momoo donedoonoon seeniseen dund.
 
'''Ñeeño yi:'''
Neeno y:
* Teug y, Lawbe, Wuude, Rabb y. Am nanu bari ca xetu Pël/Tukuloor lani jogué moye Njabotu : Thiam, Mbow, Athié, Diaw, Dioum, Tall, Fam, Guissé, Sow. Neeno nonu dani kalenté ak Pël y, ndax dani mbokk mam.
Neeno u Wolof: Beye, Niasse, Dieng, Mbaye, Niang.
* Gueweul y, nieup lani way, Buuri, Neeno. Cossanu nit yeup lani xaam, seni Sant yu geuneu siiw: Seck, Mbaye, Mboup, Lam, Seye .
 
* Teug yTëgg, Lawbe, Wuude, Rabb yRàbb. Am nanuna ñu bari caci xetuñoom ci xeetu Pël/Tukuloor lanilañu juge joguéñooy moyeñi Njabotusant : ThiamCaam, Mbow, AthiéAce, DiawJaw, DioumJum, TallTaal, FamFaam, GuisséGise, Sow. NeenoÑeeño nonuyooyu danidañuy kalentékalante ak Pël yyi, ndax danidanoo mbokkbokk mammaam.
Jaam y:
Ñeeño Wolof: Béey, Ñas, Jeng, Mbay, Ñang.
* Amna jaami buuri ( Ceddo ), Jaami Juddu, Jaami Sayor (Niom ca xeer lanu done ko dieul). Xeet gunek lani djogué.
* Géwal yi, ñépp lañuy woy, Buur yi, ñeeño yi. Cosaanu nit ñépp lañu xam, seeni Sant yi gën a siiw: Sekk, Mbay, Mbuub, Laam, Séy .
 
'''Jaam yyi:'''
Wolof y danu jaxaasé li moye tax seni sant danu bari, tamit xet yu bari niow nanu ca niom (Wolofisation). Seex Anta joop né na, Wolof y deug deug no: Njaay, joop, Faal, Niang, Beye, Mbodji, Mboup, Wade, Gueye. Ca Fuuta-Tooro, ca Cuballo (Nappkat Tukuloor) wala Sebbe (Ceddo/Jambar Tukuloor) Wala Toroodo, lani nek. Da ni tel nek fofu.
 
Ca senegal niom no dieuk giss Tubap y. Bou dieuk Ceddo lani woon, tey you bari ca yoonu murid lanu nek wala tidjanya. Amna ay chrétien tamit (Gorée-Saint-Louis). Seex Amadu Bamba Mbakké ak El Adj Malik Sy nio geuneu duggal Wolof y ca lislaam. Wolof yu bari tuxu neen Fraanse, Etat-unis, Italie, Espagne. Ca senegal da niu yoré posty yu geuneu Mag. Niom no geuneu fonk seni rewm (Nationalisme Sénégalais). Amna nu da nuy dund ca Mbey (Kaw-Kaw), Napp ca guedj bi (ca niom Lebu y lani bokk). Jom ak Teraanga ca niom la jogué.
* AmnaAm na jaami buuribuur yi ( Ceddo yi), Jaami Juddu, Jaami Sayor (Niomñoom ca xeerxare lanulees doneleen kodaan dieulame ak a jàppe). Xeet gunekwu nekk nag lanu lanidaan djoguéjuge.
 
Wolof yi danoo jaxaasoo, lii moo tax seeni sant bari, ak tamit xeet yu bari ñëw nanu ci ñoom (Wolofal: Wolofisation). Seex Anta jóob nee na, Wolof yi dëgg-dëgg ñooy: Njaay, Jóob, Faal, Ñang, Béey, Mbóoj, Mbuub Wàdd, Gëy.
Ca Fuuta-Tooro, ca Cuballo (Nappkatu Tukuloor) walla Sebbe (Ceddo/Jàmbaar Tukulóor) Walla Tooroodo, lanu. Danoo teel a nekk foofu.
CaCi senegalSenegaal niomñoom noñoo dieuknjëkk gissa Tubapgis yTubaab yi. BouBu dieuknjëkk Ceddo lanilañu woon, teytay youñu bari caci [[yoonu muridmurit]] lanulañu nekbokk walawalla tidjanyatiijaaniya. AmnaAm na ay chrétienay nasaraan (chrétiens) tamit waaye duñu ñu bari (Gorée-Saint-LouisGore/Ndar). Seex AmaduAhmadu Bamba MbakkéMbakke ak El Adj Malik Sy nio geuneu duggal Wolof y ca lislaam. Wolof yu bari tuxu neen Fraanse, Etat-unis, Italie, Espagne. Ca senegal da niu yoré posty yu geuneu Mag. Niom no geuneu fonk seni rewm (Nationalisme Sénégalais). Amna nu da nuy dund ca Mbey (Kaw-Kaw), Napp ca guedj bi (ca niom Lebu y lani bokk). Jom ak Teraanga ca niom la jogué.
[[Catégorie:Taariixu senegaal]]