Pël wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 :
[[Image:Eleveurs Peuls.jpg|thumb|200px|left|Sàmmkatu Pël bu Gurma, bëj-saalumu [[Gao]], [[Mali]]]] ÑÑoom ci seen bopp dañuy wax Pullo wala FulBe. [[Isipt]] mooy réew mi ñu bawoo. Pël ya ca Isipt ay nit ñu ñuul lañu nekkoon. Ba noppi, ay nit ñu weex, ñëw ca seenum réew juge [[Asi]] ak [[Tugal]] , bokk na ca xeet yooya: Scythe, Aryen, Phrygien, Hittite, askan yu bari yu ñuy tudde ay waa End-tugal (Indo-européen). Pël yu ñuul yi ak nit ñu weex ñi dañoo jaxaasoo woon. Lii moo tax Pël yi gën a xees, gën a sew, am kawar gu gën a nooy, bu ñu leen xoolee ci yeneen xeet yu ñuul yi ci Afrig. Ba noppi, Imbraatóor gu Tirki(ñoñ usmaan ñi(les ottonams) ), tegoon nañu loxo réewum Isipt, di fa tege dund gu metti, rawati na ca nit ñu ñuul ña. Lii moo tax Pël ya ak Séeréer sa gàddaay, dëkki ca [[Sudaan]] (Nubie) dëkki seeni maam, soog a dem Senegaal. Pël ak [[Séeréer]] danoo bokk maam, seeni làkk tamit. Yàgg nañoo ànd, dañuy kalante ci seen biir. Ca yoonu [[Tekuruur]], pël ya ca Dexug Senegaal rekk lañu nekkoon ak seeni nag. Booba nekkuñu woon ay jullit. Amuñu woon nguur ndax ak seeni nag ci màng rekk lañu nekke woon. Meew ak Sanqal (ñórndi) moo doonoon seenu lekk. Pël ci boppam am na xeet yu bari (Leyyi/KinDe), Ardo mooy seen Buur: JaawBe yi, UrurBe, WodaaBe, LaaCe, CutinkooBe, YirlaaBe. Am na yeneen KinDe. Màng gi ñu dëkke tax na ñu tuuru ci Sowwu Afrig gépp, ba far delseeti Sudaan, cig muñ ak coona ndax saa su nekk ci dëkki jàmbur yi rekk lañuy nekk, seen nag yi leeg-leeg ñu ruur tooli baykat yi, loolu it di jur xuloo bu rëy ak ŋaayoo ci seen digg ak woroon tool yi.
 
Ca atum 1539 Koli Tengella Bâ, mi ngi bookebokke ci Pël ci wetug baayam, bokk it ci Mande yi ci wàllug yaayam (Keyta), dajale woon na sàmmkati Pël yi ak mande yi, ngir ñu man a am doole. Daa di dugg ci yeneen xeet (Wolof, Séeréer, Bajaaranke, Joola, Baga, [[Sooninke]] . Ñoom ñépp ak seen aroo Koli Tengella, ñu yéeg ba Tekuruur, di xeex ak Buur-ba [[Jolof]] ba, ndax kii moo doon yor dëkk ba, ak Lam-Toro ya, Lam-Térmes, Lam-Taga ya, Juroom ñeenti fan soog a yor dëkk ai. Koli Tengella teg na fa njabootam (Denyakoobe yi), tudde na nguur ga Fuuta-Toro (Fuuta mooy dëkku Pël ca seen Làkk). Lii ca Senegaal la xewe.
Ca Mali Pël ya doñoo njëkk am doole ca atum 1818. Booba nag Ahmadu Bari, Sëriñ la nekkoon, dajale na Pëli Jullit yi, ak Mande yu jullit yi ( Mandé Mori yi : Siise, Ture, Silla ), ngir ñu àndandoo xeex (Jiyaar) safaan nguuru Bàmbara yi fi nekkoon (nguuru Ségu ak Kaarta). Buuru Bàmbara yi (Fama) ak seeni jàmbaar (Ton-Dion), amoon nanu doole, lii moo tax Ahmadu Bari tabax Imbraatoor gu Pël ca Massina Kese. ak itam Pël yi, ca Mali, fofufoofu lanilañu eupéëppe woon ba teytay (TeyTay dijii nekfoofa mooy diiwaan (Région) Debu Mopti).
Ca GinneGine, Pël yya danudañu fafaa yagyàgg, wawaaye éMande Mandé yya (JalonkéJalonke) nioñoo yooronyoron deukdëkk biba. Ca yonu 1715, ay Pël yu juulitjullit yu joguéjuge Fuuta-ToroTooro ak Massina ca Mali, nioñoo nañëw nu ca GinneGine, di fa JihadJiyaar, di reyray kuñi duduli juulitjullit walawalla di koleen jàpp ay jaamlojaam, lilii moyemoo tax xetgiir yu bari (Susu yyi, jalonkéjalonke, ak Baga yyi) daw nanu ca guedjugéeju GinneGine, di tabax fofufoofa ay nguruunguur. Pël uyu Jullit yi Juulitdañu ydoon daniray reyoneñoom tamit yeneneyeneen Pël ndaxngir nekkune nunekkuñu woon ay juulit. PëlPëli yjullit juulityi danudañoo mbokkonebokkoon ca njabotnjabooti: Bâ, BaariBari, Jallo, Sow. NiomÑoom noñoo tabax nguruunguuru Fuuta-Jalon. Karamoko Alfa Jallo mo dieuknjëkk a neknekk AlmamyAlmaami.
Ca NisseriaNiseria atum 1808, UsmanUsmaan Dan FodioFojo, njabotamnjabootam Fuuta-ToroTooro lanila djogué dibawoo, neknekk ay ToroodoTooroodo, SerignSëriñ bu makmag la nekkonenekkoon, dibu bokk ca tarixatariixa XaadiriyyaXaadiriya. MomMoom naknag Dadjalédajale na Mbeykatubaykatu HaaussaAwsa yi, ak Sambkatusàmbkati Pël yi, di leneleen duggdugal caci lislaam[[Lislaam]], ndax nuñu meunteuman a def Jihadjiyaar ca NguruuNguuru HaaussaAwsa yyi fi neknekkoon. ReyRay na Buuru HaaussaAwsa bi, daal di tabax na ImbraatorImbraatoor gu [[Sokoto]]. DemnaDem na xéerxeex ca Imbratoor gu Kanem-Bornu ca CaadCadd, wa éwaaye nionuñooñu danudañoo amoneamooon doolédoole toroplool.
Ca kaw KameroonKamerun atum 1810, benebenn Serignsëriñ bu tudd ModiboMojibo Adama, dadjalédajale na Pël u juulitPëli jullit(fofufoofu Fulbé lalees nileen di wax) yyi fi nékkonenékkoon, nu tabax Nguruunguuru Adamawa. WaWaaye éam amnana Fulbé yu bari (WodaaBe/Borooro), bugunuyoy ànduñu woon bobuca googa nguruunguur.
Modibo ak yeneneyeneen Pël layi defñoo Jihaddefoon Jihaad, ndax dunuay nekkonejullit aylanu juulitwoon. Modibo Adama, Usman Dan FodioFojo mokomoo ko dimbali woon.
Ca atum 1860, Alfa YayaYaaya Molo BaaldéBalde, tabax na nguruunguuru Fuladu ca Bëj-saalumsaalumu Senegaal. DaDaal dadjalédi dajale Pël yyi di leneleen duggdugal caci lislaam, ndax AlmamyAlmaami ubu Fuuta-Jalon Alfa Bokar Biram, nee na woon du dimbali, kuduulku dul JuulitJullit.
AlmamyAlmaami bobuboobu ak Alfa yayaYaaya xéerxare nanu nguruuak nguur gu Mandé, Kabbu ak seniseeni Buur (Mansa), ndax fofufoofu Pël yi danu nekkonefaa nekkoon Jaami Mandé yyi. NiariÑaari Buur rekrekk nioñoo yoronyoroon FuladuFulaadu, Alfa YayaYaaya ak domamdoomam MoussaMusaa Molo BaaldéBalde.
KoneKon Pël yyi, lislaamLislaam momoo leneleen dadjalédajale, di leneleen jox doolédoole.
 
Pël seniseeni NostegNostey mboolaay ga nii lalanu tëdde woon:
* RimBe noñoo daa doon doneBuur Buuriyi.
* JaawanDo yyi, noñoo donedaa toptopp RimBe yi di leneleen wonewon lannan lanilañuy yooréyore nguruunguur.
 
Ñeeño yi:
Neeno y:
*WayilBe no done Teug y.
*LawBe no done Seen y.
*SakeeBe, no done Wuude y.
*MabuuBe, no done Rabb y.
*BaambaaDo, no done Xalamkat y, waykatu Jambar y.
*Gawlo, Waykatu Buuri.
 
* WayilBe ñoo daa nekk Tëgg yi.
Jaami:
* LawBe noñoo daa donedoon Seen yyi.
*Maccudo wala Kordo.
* SakeeBe, no donenekk Wuude yyi.
* MabuuBe, no donedoon RabbRàbb yyi.
* BaambaaDo, no donedoon Xalamkat yyi, waykatuwoykati JambarJàmbaar yyi.
* Gawlo, Woykati Buur yi.
 
Jaam yi:
Ca Isipt Pël y, da nu yoron niet Sant rek (Ba, Ka, Bara (tey mou nek Baari)). Ba paré Pël y danu jël yenene Sant Ndax deuk bi, wala Mban yi, liggey yi done def.
 
Li yeup ba am tey Sant gi: Bâ, Baari, Jallo, Kâ, Ja, Sow, Jaw, Caam, Naan, Jum, Dikko, Seydi, Mbow, Bokum, Dem, Sidibé, Sall,
* Maccudo walawalla Kordo.
Ca fuladu Pël yu bari Jamanka lani Sant. Ca Mali Sidibé moye Sow. Ca niseeria Pël yu bari Bello lani Sant. Ku Sant Baal, mamam ay Bâ lani woon. Ku Sant Jakk maman ay Sow lani woon.
 
Sankara, Sankaré, Shagari, li yëp bene la.
Ca Isipt Pël yya, dadañoo nuyoroon yoron nietñatti Sant rekrekk (Ba, Ka, Bara (teytay moumu neksoppiku Baaridi Bari)). Ba parénoppi Pël yyi danudanoo jël yeneneyeneen Sant Ndax deukdëkk bi, walawalla Mban yi, liggeyliggéey yi doneñu doon def.
Amna Pël yu bari demna nu ca Wolof yi li moye tax amna ay wolof ku sant (Caam, Mbow, Sow, Naan, Sall). Tamit amna Xët yu bari nio nanu ca Pël, li moye tax amna ay Pël ku sant Cissé, Tuuré, Njaay, Jakité, Kamara ak yenene sant.
 
Li yeuplépp ba am teytay Sant giyii: Bâ, BaariBari, Jallo, Ka, Ja, Sow, Jaw, Caam, Naan, Jum, Dikko, Seydi, Mbow, Bokum, Dem, SidibéSidibe, SallSàll,
Ca fuladufulaadu Pël yu bari Jamanka lanilañu Santsant. Ca Mali SidibéSidibe moyemooy Sow. Ca niseeriaNiseriyaa Pël yu bari Bello lanilanu Santsant. Ku Santsant Baal, mamammaamam ay Bâ lanilanu woon. Ku Sant Jakk mamanmaaman ay Sow lanilanu woon.
Sankara, Sankaré, Shagari, liyooyu yëpyépp benebenn lalanu.
AmnaAm na Pël yu bari demnayoy nudem nanu ca Wolof yi liya, moyelooloo tax amnaam ay wolof kuyu sant (Caam, Mbow, Sow, Naan, SallSàll). TamitAm amnana Xëttam waaso yu bari nioyoy dikk nanu caci Pël yi, li moyemoo tax amnaam ay Pël kuyu sant CisséSiise, TuuréTure, Njaay, JakitéJakite, Kamara ak yeneneyeneen sant.
 
<gallery>
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Pël » lañ ko jële