Wolof (askan) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 24 :
Wolof y danu jaxaasé li moye tax seni sant danu bari, tamit xet yu bari niow nanu ca niom (Wolofisation). Seex Anta joop né na, Wolof y deug deug no: Njaay, joop, Faal, Niang, Beye, Mbodji, Mboup, Wade, Gueye. Ca Fuuta-Tooro, ca Cuballo (Nappkat Tukuloor) wala Sebbe (Ceddo/Jambar Tukuloor) Wala Toroodo, lani nek. Da ni tel nek fofu.
Ca senegal niom no dieuk giss Tubap y. Bou dieuk Ceddo lani woon, tey you bari ca yoonu murid lanu nek wala tidjanya. Amna ay chrétien tamit (Gorée-Saint-Louis). Seex Amadu Bamba Mbakké ak El Adj Malik Sy nio geuneu duggal Wolof y ca lislaam. Wolof yu bari tuxu neen Fraanse, Etat-unis, Italie, Espagne. Ca senegal da niu yoré posty yu geuneu Mag. Niom no geuneu fonk seni rewm (Nationalisme Sénégalais). Amna nu da nuy dund ca Mbey (Kaw-Kaw), Napp ca guedj bi (ca niom Lebu y lani bokk). Jom ak Teraanga ca niom la jogué.
[[Catégorie:Taariixu senegaal]]