Sahel wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Sahel''' (jòge ci [[araab]] ساحل , ''sahil'', di tekki pegg walla tefes) di jëmmal ab barab bu bekkoor, ne ci diggante [[tàkk]] gu [[Sahara]] ci bëj-gànnaar ak diwaanidiiwaani [[yemooyamoo]] gi fa nga xam ne day taw rekrekk, ci bëj-saalum. Tëraayam day jàpp [[mbàmbulaanu Atlas]] jëm ca [[géej gu xónq]] giga.
[[Image:Map sahel.jpg|thumb|300px| Lonkoyoonu AfrikAfrig ak diwaanudiiwaanu Sahel ]]
Réew ya ca ne:
 
Rëdd 12 :
* [[Sudaan]].
 
== SéwógaraafiMelosuuf ==
Daanaka Sahel gépp gannuus la ak [[mandiŋmàndiŋ]], ci lu ëpp, ñetti weer rekk lay taw ci at mi.
 
Dañ koy seddale ci xaaj yu bari:
 
* [[ndand féy-féyTàkk|Ndand féy-féyTàkk]] gi: kawewaay gu diggu gu taw yi du weesu 150mm ci at, béppmépp mbayembay mu aju ci ndoxu taw, manu faa am.
* «Sahelu way mangaanmàngaan yi»: kawewaay gu diggu gu taw yi du weesu 400mm, foofu it mbayembay mu aju ci ndoxum taw, amal ko fa daanaka nekkuwul. Mooy barab bi sammkatu [[naknag]] ak [[gëleemgëléem]] yiy mangaanmàngaan di nekk.
* «Sahelu way dëkk yi»: kawewaay gu diggu gu taw yi du weesu 650mm ci at. [[dugub|Dugub]] ak [[areenaréen]] lañlañu fay bay.
* «Barabu Sahel-sudaan»: fii mbay mi gën naa yaa, taw yi yokk bu baax.
* «Barabu [[sudaan(diwaan)|sudaan]]»: fii taw yi di nañ àgg 950mm ci at, tawi nawet bi, di na tax ñu man a bay [[dugubu suuna]], [[mboq]], [[wëteenwëtéen]],...
 
Tolof-tolof yi ëpp yi ay way dëkkam di jànkonteel ñooy: [[bekkoor]] giy gën di sax ak [[ndand féy-féytàkku]] giy gën di jëm-kanam, di mëdd gañcaxngañcax su néew sa fa am.
 
{{modèle:diwaaniafrik}}
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Sahel » lañ ko jële