Kajoor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 23 :
== Yoriin ==
 
Nguur gu bees gi tax na ba ñu andi tër yu bees ci ay àtte yu bees. Dammeel moo feete woon ñépp kaw. Moom mu ngi daan sant Faal ci geño ak ci meen. Man naa am ñu tànn dammeel fuci lu dul geño mbaa meenubmeenum paaleenPaaléen. Waaye loolu su xewee li koy waral mooy fullay waajawaa ja ak faydamfaydaam ak tabeem. Yii yèppyépp ñiy tànn daa na ñunañu ci bàyyi xel.
 
Su ñaar dee xëccoo nguur gi war na ci ñoom ñaar ñeppñépp ñu nekk Jaambur, mbaa ay Bummi mbaa ay beñ Beñ-jéem. Su ñu bokkee lu ñuy nekk, boroom baat yi nekk ci kaw, yiy tànn dellu seet seen jikko ak nu ñuy àtteàttee ak su mbir nee këtt ne jonn nu ñuy taxaweetaxawe. LiLii doy na tegtal ci leertegleerug seen tànninutànniinu buur.
 
Loolu terewul nguur gi nekk ndono ci kaw bu amee ku ko war a donn.
 
Kajoor mekkoonnekkoon na juroomi tund: Ganjòol[[Gànjòol]], [[Njaambur]] ci bëj-gànnaar, Ndèet[[Ndéet]] ca penku, [[Sañaxoor]] ca digg Kajoor, jandeer[[Jandeer]] ca diggante sowusowwu ak bëj-saalum. Su ñu falee Dammeel da fadafa war a sèddaleséddale ndomboy tànk yu mag ya ba ku nekk xam foo féete. Ci jeexintalumujjug xarnub XVII la Dammeel joxe woon ndigal ngir ndomboy tànk yooyee, ñu man kaakoo tàkkaltakkal rekk ñi cosaanoo ngàlloNgàllo te féete ci kër buur.
 
== Buuri Kajoor ==
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Kajoor » lañ ko jële