Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 124 :
 
 
Bismarck gisoon na ne xare bi moom – deetdéet sikk – aji tàkk la ci diggante Brusiya ak Otris, te li ko waral du dara lu dul '''diiwaanu Holistin'''. Ndax kat mbir yi manunumanuñu woon a nekk di wéy ci anam gii nuñu nekke, di ay maslaa yu dëggoodi aki lijjanti yu xootadi aki juboo yu gàtti dig.
Bis bu Yàlla dogalee njortul Bismarck loolu mujj di dëgg, ba Brusiya am ndam, loolu de da na nekki muccug waa Almaañ ñi ci gàllankoor gii tukkee ci Otris, gu leen di teree nekk benn, tee bennoo gu Almaañ gu wér man a am. Màggug Brusiya ci wàllug politig ci biir bennoo gu Almaañ gi, mujj di luy jeqi njàqare ci Otris. Solofrayn moom màgg na ci anam gu doy waar, rawati na bi ci nguur-nguuraan yu Almaañ yi tiim geejug bëj-gànnaar gi bokksee. Ci noonu lu sakkan jug ciy yooni weñ lënkale diggante wàll yu Almaañ yu wuute yi. Loolu tam dooleel bennoo gu koom-koom gi nga xam ne Brusiya mujj na di ci ki ci gën a jariñu.
 
Bis bu Yàlla dogalee njortul Bismarck loolu mujj di dëgg, ba Brusiya am ndam, loolu de da na nekki muccug waa Almaañ ñi ci gàllankoor gii tukkee ci Otris, gu leen di teree nekk benn, tee bennoo gu Almaañ gu wér man a am. Màggug Brusiya ci wàllug politig ci biir bennoo gu Almaañ gi, mujj di luy jeqi njàqare ci Otris. Solofrayn moom màgg na ci anam gu doy waar, rawati na bi ci nguur-nguuraan yu Almaañ yi tiim geejug bëj-gànnaar gi bokksee. Ci noonu lu sakkan jug ciy yooni weñ lënkale diggante wàll yu Almaañ yu wuute yi. Loolu tam dooleel bennoo gu koom-koom gi nga xam ne Brusiya mujj na di ci ki ci gën a jariñu.
Sabab yii rekk doyoon nanu ngir taal xeex bi ci diggante Brusiya ak Otris, rawati na ginaaw bi dooley Brusiya ji doxee jawali Holistin, nangu ko, te moom daa nekkoon ci ron kilifteefug Otris, ngir dëppoo gi amoon ci diggante Brusiya ak Otris atum 1865g.
 
Solofrayn moom màgg na ci anam gu doy waar, rawati na bi ci nguur-nguuraan yu Almaañ yi tiim [[Géej gu bëj-gànnaar]] gi bokksee. Ci noonu lu sakkan jug ciy yooni weñ lënkale diggante wàll yu Almaañ yu wuute yi. Loolu tam dooleel bennoo gu koom-koom gi nga xam ne Brusiya mujj na di ci ki ci gën a jariñu.
Bismarck moom lijjanti woon na ba Rusi genne loxoom ci diggam ak Otris, loolu nag di ci jàpple gi mu jàpple woon Rusi ci giimal fipp ga amoon ca Poloñ, atum 1853g. Dëppoo woon na ak Imbratoor bi Napoleon III, imbraatooru Fraans, moom itam, ngir mu seetaan kook Otris, bañ cee dugal loxoom, li mu koy faye ci loolu nag mooy bàyyi kook yenn moomeel yi ci goxub Rayn. Mu demati tapoo-ji ak nguurug Itaali, gi nga xam ne li doonoon yitteem mooy nocci Venezia ci loxol Otris, ngir matal ag bennoom.
 
Sabab yii rekk doyoon nanunañu ngir taal xeex bi ci diggante Brusiya ak Otris, rawati na ginaaw bi dooley Brusiya ji doxee jawali Holistin, nangu ko, te moom daa nekkoon ci ron kilifteefug Otris, ngir dëppoo gi amoon ci diggante Brusiya ak Otris atum 1865g.
Xare bi amoon ci diggante Otris ak Brusiya xare la woon bu fëkk te gaaw, wéyutoon lu ëpp juroom ñaari ayu-bis, moo waraloon nu tudde woon ko xareb juroom ñaari ayu-bis yi. Dooley Brusiya ji jot na ca a gañee ju Otris ja ca xareb Sadwa ba, ca Bohima atum 1866g . Mu manoon a àgg sax (moom dooley Brusiya ji) ba ca Vienne, bu Imbraatooru Fraans bii di Napoleon III jugutoon, dox tànki jàmm ci diggante bi. Ci noonu Bismarck daal di ñàkk pexe, taxawal xeex bi, ngir ragal Fraans dugg ci xeex bi ci wetu Otris. Te it Bismarck moom da ne woon na doylu nag ci gañe gii mu gañe Otris, ak dammte gii mu ko dammte, ndaxte soril na ko bennoo gu Almaañ cig wàll, te it bëggutoon a toroxal Imbraatooru Otris bi, ngir loolu man na a tax bu jugee ëlëg moom Brusiya di xare-ji ak Fraans, Otris du ko sot, ci geneen wàll.
Ag juboo amoon na ci diggante Brusiya ak Otris, ñu koy wax “juboog Braax gi”, atum 1866g. Ci la yii ame:
 
Bismarck moom lijjanti woon na ba RusiRiisi gennegénne loxoom ci diggam ak Otris, loolu nag di ci jàpple gi mu jàpple woon RusiRiisi ci giimal fippjeqiku(révolution) ga amoon ca Poloñ, atum 1853g. Dëppoo woon na ak ImbratoorImbratóor bi Napoleon III, imbraatooruimbraatóoru Fraans[[Faraas]], moom itam, ngir mu seetaan kook Otris, bañ cee dugal loxoom, li mu koy faye ci loolu nag mooy bàyyi kook yenn moomeel yi ci goxubdiiwaanub Rayn. Mu demati tapoo-ji (faire alliance avec)ak nguurug Itaali, gi nga xam ne li doonoon yitteem mooy nocci Venezia ci loxol Otris, ngir matal ag bennoom.
(1) Gennug Otris ci Bennoo gu Almaañ gi, gi mu tegoon loxo, la ko dale ca jamonoy Metternich.
(2) Duggug mbooleem nguur-nguuraan yi nekkoon ci bëj-gànnaaru dexu Rayn gi, ci bennoo gu federaal gu Almaañ ci ron njiitul Brusiya. Diiwaani bëj-saalum rekk a bokkutoon ci bennoo googu.
(3) Bàyyee gu Otris bàyyee Itaali Venezia.
 
Xare bi amoon ci diggante Otris ak Brusiya xare la woon bu fëkk te gaaw, wéyutoon lu ëpp juroom ñaari ayu-bis, moo waraloon nu tudde woon ko '''xareb juroom ñaari ayu-bis yi'''. Dooley Brusiya ji jot na ca a gañeeam ndam ci kaw ju Otris ja ca xareb Sadwa ba, ca Bohima atum 1866g . Mu manoon a àgg sax (moom dooley Brusiya ji) ba ca Vienne, bu ImbraatooruImbraatóoru FraansFaraas bii di Napoleon III jugutoon, dox tànki jàmm ci diggante bi. Ci noonu Bismarck daal di ñàkk pexe, taxawal xeex bi, ngir ragal FraansFaraas dugg ci xeex bi ci wetu Otris. Te it Bismarck moom da ne woon na doylu nag ci gañeam ndam gii mu gañeam ci kaw Otris, ak dammte gii mu ko dammte, ndaxte soril na ko bennoo gu Almaañ cig wàll, te it bëggutoon a toroxal ImbraatooruImbraatóoru Otris bi, ngir loolu man na a tax bu jugee ëlëg moom Brusiya di xare-ji ak FraansFaraas, Otris du ko sot, ci geneen wàll.
Ag juboo amoon na ci diggante Brusiya ak Otris, ñu koy wax “juboog“'''juboog Braax gi”gi'''”, atum 1866g. Ci la yii ame:
 
(1) Gennug* '''Génnug Otris ci Bennoo gu Almaañ gi, gi mu tegoon loxo, la ko dale ca jamonoy Metternich.'''
Gis nga ko, Bismarck kat am na ay ngërte yu am solo ci xareem beek Otris. Moom de fare na fi bennoog Almaañ gu yàgg ga, indi fi leegi ag bennoo gu Almaañ gu yees, gu ame ci mbooleem reewi bëj-gànnaaru Almaañ, nga xam ne ñaari doox yii di Shalswig ak Holistin ci lanu woon, buuru Brusiya bi jiite ko. Bismarck nos na bennoo gu yees gi, wutal ko ab parlamaa (Rashstach), ndawi askan wa di fa daje, ak jataayub bennoo gu Almaañ gi (Bundasrat), ndawi diiwaani Almaañ yi bokk ci bennoo gu Almaañ gu bees gi di fa daje.
Bismarck it lijjanti na ba def ak diiwaani bëj-saalum yi bokkutoon ci bennoo gi, lijjanti woon na ba def ak ñoom genn tapoo gu xare .
 
(2) * '''Duggug mbooleem nguur-nguuraan yi nekkoon ci bëj-gànnaaru dexu Rayn gi, ci bennoo gu lëngoo (gu federaal) gu Almaañ ci ron njiitul Brusiya. Diiwaani bëj-saalum rekk a bokkutoon ci bennoo googu.'''
Xareb Brusiya ak Fraans:
 
(3) * '''Bàyyee gu Otris bàyyee Itaali Venezia.'''
 
 
Gis nga ko, Bismarck kat am na ay ngërte yu am solo ci xareem beek Otris. Moom de fare na fi bennoog Almaañ gu yàgg ga, indi fi leegi ag bennoo gu Almaañ gu yees, gu ame ci mbooleem reewiréewi bëj-gànnaaru Almaañ, nga xam ne ñaari dooxDóox yii di Shalswig ak Holistin ci lanulañu woon, buuru Brusiya bi jiite ko. Bismarck nos na bennoo gu yees gi, wutal ko ab parlamaa '''(Rashstach)''', ndawi askan wa di fa daje, ak '''jataayub bennoo gu Almaañ gi''' '''(Bundasrat)''', ndawi diiwaani Almaañ yi bokk ci bennoo gu Almaañ gu bees gi di fa daje.
 
Bismarck it lijjanti na ba def ak diiwaani bëj-saalum yi bokkutoon ci bennoo gi, lijjanti woon na ba def ak ñoom '''genn tapoo gu xare''' .
 
 
== Xareb Brusiya ak FraansFaraas: ==
 
Xetug xare tàmbli woon na a xeeñ ak a jòlli ci diggante Fraans ak Brusiya, ginaaw bi Brusiya gañee ca xareb Sadwa ba. Ndaxte Fraans moom begutoon dara ci lii Brusiya amal ciy ndam ci kaw Danmark ak Otris cig wàll, ak àntul gi mu àntuloon bennoo gu Almaañ gu bëj-gànnaar gi, ci geneen wàll.