Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 31 :
== 1 Solofrayn ==
 
== 2 “Bennoog nduwaan gu Bavar” gi ==
(2) “Bennoog nduwaan gu Bavar” gi nga xam ne mi ngi judd woon atum 1820g, maanaam ginaaw bi gu Solofrayn amee ba am ñaari at.
 
 
== 3 Ak bennoo gu nduwaan gu Saksoniya ==
(3) Ak bennoo gu nduwaan gu Saksoni. Mooy gi SaksoniSaksoniya taxawaloon atum 1828g.
 
(2) “Bennoog nduwaan gu Bavar” gi nga xam ne mi ngi judd woon atum 1820g, maanaam ginaaw bi gu Solofrayn amee ba am ñaari at.
(3) Ak bennoo gu nduwaan gu Saksoni. Mooy gi Saksoni taxawaloon atum 1828g.
 
Kilifay Brusiya yi xamoon nanu ne diiwaani Almaañ yi dananu nangoo duggsi ci bennoo gu Solofrayn gi, bu nu soppee sart yiy tax manees cee dugg. Looloo taxoon ñu soppi sarti Solofrayn yi, nga xam ne leegi danoo sos ab jataay bu làmboo mbooleem ndawi yi ci bokk, buy saytu noste googu. Leegi nag lu fa duggati rekk ci li bawoo ci nduwaan mi ak galag yi ñu koy seddale mbooleem diiwaan yi, ci kem limub ña fa dëkk. Soppi yii de dimblee na ci yaatal gëweelub Solofrayn, gën a yàkkali ab geewam. Leegi nag Bavar bokksi na ci ak Saksoni ci atum 1934g, ca saa sa tam, nga tàmblee gis lu lay won ne Solofrayn moom tàmbli na a naat ak a am ag yokkute. Yaxantu ga tàmbli woon nay jar, di dox, mbay ma màgg, endustri ba jëm kanam ci mbooleem diiwaan yi bokksi ci Solofrayn. Am na nag benn jëfka boo xam ne moo àntul Solofrayn, mooy moom de noste gu waa Almaañ xalaat ba def ko la, loxol Otris duggu ci, jenn doole it ju ko man a teg loxo yoonam nekku ci. Metternich gisoon na ay wi nekkoon ci noste gii, waaye bi mu koy gis fekk na waxtu wa jàll, manatu ca woon dara. Mu daal di bind Imbraatoor bu Otris bi ne ko: “Na la wóor ne nguuri Almaañ yi - bi lii amee de – di nanu nekki wenn yaram wu jàppaloo, ci ron kerug doxaliin gu Brusiya, te da na jàppeji Brusiya muy - moom - aw yaram wu di doxandeem, wu tumbrànke wu bokkul ciw yaramam”. Te kat waa Otris yi ñoom, ca dëgg-dëgg, dunu ay doxandeem ci waa Almaañ yi, ndax ñoo bokk xeet, làkk ak taarix. Man nanu ne Almaañ gepp mujj na bokksi ci Solofrayn gi, atum 1842g.