Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 22 :
 
 
Nguurug Brusiya dafa tàmbli woon di yëngu ngir dajale xeetu Almaañ wi, duggaldugal leen ci genn nguur gu Almaañ gu nuñu bennal. Mu daal di woon rëddal boppam ab politig bu muy jaar ngir àgg ci loolu mu bëgg. Mu daal di woon door ci dëgëral boppam ci biirum reewréew, defaraat doxaliinam , yekkati koom-koomam, soppi nosteg galag yi aju woon ci nduwaan ci mbooleem goxidiiwani nguur gi.
Ñu daal di taxawal noste gi nu daa wax ('''Solofrayn'''), di ag bennoo ci wàllug nduwaan, mooy li neenaloon nosteg nduwaan gi ci biir Almaañ. Nga xam ne li nekk ci biir reewréew mi cim njaay deesu ci gennegénne duwaan. Nga xam ne danoodaññoo feexalfééexal yaxantu gi ci Brusiya, ëfalafal ko ba mu man a doxe ni ko soob, ci lu dul ñu ciy teg ay tënk-tënki galag mbaa yu nduwaan. Doxiinu Brusiya wii deydéy dees na ko lim mu dig soopiku gu mag ci taarixu bennoo gu Almaañ gi. Doxal nanunañu ko nag ci atum 1818g, ci biir ay goxamdiiwaanam yu biir yi. GoxDiiwaan yooyu nga xam ne njëkk “Nosteg Solofrayn gi” danoo nekkoon ay goxdiiwaan yoo xam ne bu ci nekk daa amoon '''nosteg pobbbobb gu nduwaan'''(systeme autonome douanier), gu mu bokkul ak kenn. Waaye bi Solfrayn taxawee, lanulañu bennal biir Brusiya ci wàllug nduwaan, ginaawginnaaw bi mu nekkee moom Brusiya di lu nuñu seddaleséddale ci juroom benn fukki goxidiiwaani nduwaan.
 
Waa Brusiya yi yëgoon nanu ne benno gi ci wàllug koom-koom mooy cëslaay li nuñu war a teg bennoog Almaañ gi ci wàllug politig. Looloo taxoon kilifay Brusiya yi tàmbli woon a fexe nu nuyñuy def ba duggaldugal yeneen diiwaani Almaañ yi ci bennoo gu nduwaan googu. Brusiya nag amoon na ndam ci li mu doon wut ci yenn ci diiwaan yu Almaañ yu ndaw yi, waaye nag jot naa dajeek ag jàmmaarloo gu mag ci yeneen diiwaan yu Almaañ yu mag yi, li ko waral mooy ñoom dañoo gisoon ne li gën ci ñoom mooy ñu sosal seen bopp ag bennoo gu ndawaan gu temb, ngir xeex ci bennog nduwaan gu Brusiya gi. Looloo fi indi woon ñatti bennoo yu nduwaan ci Almaañ, ñooy:
 
 
(== 1) Solofrayn ==
 
Waa Brusiya yi yëgoon nanu ne benno gi ci wàllug koom-koom mooy cëslaay li nu war a teg bennoog Almaañ gi ci wàllug politig. Looloo taxoon kilifay Brusiya yi tàmbli woon a fexe nu nuy def ba duggal yeneen diiwaani Almaañ yi ci bennoo gu nduwaan googu. Brusiya nag amoon na ndam ci li mu doon wut ci yenn ci diiwaan yu Almaañ yu ndaw yi, waaye nag jot naa dajeek ag jàmmaarloo gu mag ci yeneen diiwaan yu Almaañ yu mag yi, li ko waral mooy ñoom dañoo gisoon ne li gën ci ñoom mooy ñu sosal seen bopp ag bennoo gu ndawaan gu temb, ngir xeex ci bennog nduwaan gu Brusiya gi. Looloo fi indi woon ñatti bennoo yu nduwaan ci Almaañ, ñooy:
 
(1) Solofrayn
(2) “Bennoog nduwaan gu Bavar” gi nga xam ne mi ngi judd woon atum 1820g, maanaam ginaaw bi gu Solofrayn amee ba am ñaari at.
(3) Ak bennoo gu nduwaan gu Saksoni. Mooy gi Saksoni taxawaloon atum 1828g.