Bennoo gu Almaañ wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Xët wu bees : Bennoo gu Almaañ Almaañ njëkk xare yu Napoleon yi: Almaañ njëkk xarey Napoleon yi, dafa seddaliku woon ci lu jege ñatti teemeer ak juroom benn fukki diiwaan, yepp it ci ron ...
 
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Bennoo gu Almaañ'''
 
== Almaañ njëkk xare yu Napoleon yi: ==
 
[[Almaañ]] njëkk xarey Napoleon yi, dafa seddalikuséddaliku woon ci lu jege ñatti teemeertéemeer ak juroom benn fukki diiwaan(360 diiwaan), yeppyépp it ci ron imbraatoorimbraatóor gu Otris lanulañu nekkoon, walla li nuyñuy tudde Imbraatoorug'''Imbraatóor gu Rom gu sell''' gi. Almaañ geppgépp it genn nguur rekk a fa nekkoon gu mag te temb, mooy gu [[Brusiya]]. Nguur googu nag jëmoon na kanam, te ag yewwuteem fés, ci jamonoy buuram ba tuddoon [[Fredrick mu mag mi]] (Great Fredrick) (1740 -1786 g), mooy ki ko defoon muy nguur gu dëgër te am doole. Bu ko defee waa Almaañ yeppyépp wëlbati seeni gët jëme ci nguur gii, ngir bëgg ag bennoo.
Almaañ njëkk xare yu Napoleon yi:
 
Almaañ njëkk xarey Napoleon yi, dafa seddaliku woon ci lu jege ñatti teemeer ak juroom benn fukki diiwaan, yepp it ci ron imbraatoor gu Otris lanu nekkoon, walla li nuy tudde Imbraatoorug Rom gu sell gi. Almaañ gepp it genn nguur rekk a fa nekkoon gu mag te temb, mooy gu Brusiya. Nguur googu nag jëmoon na kanam, te ag yewwuteem fés, ci jamonoy buuram ba tuddoon Fredrick mu mag mi (Great Fredrick) (1740 -1786 g), mooy ki ko defoon muy nguur gu dëgër te am doole. Bu ko defee waa Almaañ yepp wëlbati seeni gët jëme ci nguur gii, ngir bëgg ag bennoo.
 
== Almaañ ci jamonoy Napoleon: ==
 
Napoleon ak xarekatam ya xuusoon nanu ci diiwaani Almaañ yi, teg leen loxo. Daal di jawali ca nguurug Brusiya, gi nga xam ne jàmmaarloo woon na’ak ñoom cig njàmmaar ak fit, waaye Napoleon moom mujj na ko not, te gañe ko ci mujj gi, ca xareb Yena ba, atum 1806g, daal di teg loxo peeyam ba Berlin.