Ndimbal:Dalal-jàmm wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
<poem>
'''Dalal-jàmm''', yaa ngi ci wikipedia gi ñu jagleel kàllaama Wolof, mu di jimbulang bu [[Ndimbal:Jimbulang bu ubbeeku|ubbeeku]] boo xam ne ñi koy jàng bokk nañu ci ñi koy bind.
Ku nekk man nga cee dugal sa loxo, bind ay jukki yu bees walla gën a baaxal li fi jot a nekk; ndaxte ngir sémb miibii manaman a dox ci ni mu gëne, dafa laaj ay loxo yu bari. Ku mu man di doon, man nga cee jàpp ci kowkaw njekk ak teraanga, topp àtte yiñyi ñu fi tëral, noo ngi lay dalal.
 
Li mu doon lu ubbeeku ngir ñépp te amulug pay, ñi binduwul tamit ci biir, '''moo tax Wikipedia manulamanul joxeya joxe ay wóoral ci mbaaxaay ak cellteg ëmbitamëmbiitam ''' Donte askanu wikipedia mi ngi tijjiy gëtam ngir di ko jéemajéem a aar ci anam yu dëgar. Saa su ne, man naa am ay xët yu ñuy saay-saaye walla yu ñu soppi ci anam yudul yi gën ci kowkaw tayeef, def ciy xibaar yu baaxul walla yu dëppóowul ak sa dundinudundiinu waa-gox.
</poem>
 
Rëdd 10 :
Su fekkee itam daa am jukki booy seet, man ngaa bind benn walla ay baat yu bari ci boyotu bind bi nekk ci sa cammoñ daal di "cuq" ci ''Ayca''
</poem>
* su fekkee baat bi nga bind dafa nekk kojubkojug jukki ba noppi, dangay "cuq" ci ''Ayca'' rekk mu feeñ.
* su fekkee nak baat bi dafa nekk ci biiri xët yu am ba noppi, dangay "cuq" ci ''Seet''.
* (jàppal ne xëtu seetukaay bi dafay tijjil boppam su fekkee dangaa "cuq" ci ''Ayca'' te amul lu mu la indil, gisul dara).
 
==Dangaa bëggabëgg jéemaa jéem a bind?==
Balaa dara, ma xamal la ne lu yomb la, doy na nga jéemajéem a roy ci li fi nekk. Su fekkee dangaa bëggabëgg jéemaa jéem a bind te ragalaragal a yàq li fi jotajot a nekk, jéemal ci xëtu [[jéemantu wi]]. Ci wii xët man ngaa jéemantu ci li la solool. Su fekkee naknag dangaa bëggabëgg a jéem jéemaa soppi xët yu am ba noppi (wu mel ne wii), [[jëlal te taqale]] ëmbitamëmbiitam ci xëtu jéemantu yi te nga soppi ko ci sa coobare.
 
==Binduwoo?==
Rëdd 24 :
* dinga am sa xëtu bopp, fooy waxee yaay kan ñu duppe ko ''xëtu jëfandikukat''
* dinga am xëtu waxtaanukaay
* manaman a yeb ay nataal
* manaman a toppale ay xët, soppi seeni tur itam
* manaman a soppi xët yi ñu aar, ngir bañ ku kenn xamul def ci naka su dul noonu
* manaman a xaatim say kàddu ci xëtu waxtaanuwaay yi
* ak yeneen ak yeneen