Taariixu Aamerig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 108 :
 
 
== Ndajem waxtaan mu [[FiladelfiyaFilaadelfiya]] mu njëkk mi:==
 
Juroom ñeenti diiwaan yu Aameriig teewe woon nañu ndajem [[New York]] ma, atum 1765g, di sàkku ci nguurug Angalteer mu teggil leen galagu tembar bi mu leen di teg.
Rëdd 126 :
Angalteer nag, ci safaanub muy lijanti lëj-lëj boobu ci maslaa gu xereñ, moom daal da fee nekk di yonnee ay dooley xare yu yees ci Boston, ngir gën a dëgëral doole ja fa nekkoon.
Loolu tam li mu juroon mooy waa sancu yi ñoom itam, ñu ne woon nañu waajal seen bopp, ndax kat nguurug Angalteer gi bëggul jàmm, ci noonu ñu - ñoom waa sancu yi – defaat beneen ndaje ci Filadefiya, ngir jàng mbir mi, seet nu ñu ciy def.
 
 
== Ndajem Filadelfiya mu ñaareel mi: ==