Lóriye wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Bamba Tubaab (waxtaancëru)
Bamba Tubaab (waxtaancëru)
Contenu remplacé par « '''Lóriye''' ==Melo wi== ==Turu xam-xam wi== '''Laurus nobilis''' Wàll:garab »
Tafaan: Contenu remplacé
Rëdd 1 :
'''Lóriye'''
[[Dencukaay:Nerium oleander 20zz.jpg|vignette|Nataalu garabug lóriye]]
'''Lóriye''' garab gu ndaw lay doon mi ngi bokk ci njabootug (abusinaas) garab la gog des koy fekk ci dexi miditeraaniy. Mi ngi yamog benn xeetu (espes), bu yor melowu nderyéem. Yenn saay des koy woowe oleyàndar walla ñu di ko woowe batay rosaas neriyeen. Garab la gog day am taaru lool te yaatu lool foofu, fépp ca mediteraaniya ñu di ko fo sàmm ngir ni moom dafa mana dékku, (seserees).
 
==Melo wi==
 
Garab la gog ay xóbam man naa ray nag, ndax dafa ànd ak poson boo xam ni dafa jafe lool ci faj ko ta am doole lool ci xeeti lu ci mel ni wallum karjaag, ak waccu, añs.
Lóriyée garab gu ndaw la gog, da na gam-gamlu ci yaati meetar ci guddaay, waaye yenn saay mu dem ba ñeenti meetar ay fooyam danoo yor melo bu weex, bu am mboq, baa óraas, walla ñu xóq, walla ñuy jaxase xeeti melo yu bari.
Lu ci ëpp lóriyée garab la gog des koy jëmbat daal koy wërële ak suuf walla ñu koy def cib pot, ngir taaral. Boodemee fëlle ca dëkk yi nga xam ne danoo jege miditeraaniya ñu ko fay jëfëndikoo ci medd ya, rangale ko ngir taaral medd yi fëlle ca faraas niki noonu. Yenn baay ma yi nga xam ni dañuy lekk ñax, menees na leen pósone xóbi lóriyée, rawatina xób yi bu tooyee.
Mana ray ci xol bu taxaw. Am na yeneen xeeti jefe-jefe yum àndal. Ci noonu nag, bari na boroom xam-xam yu bari yu kay jëfëndiko, ngir di ci wattandiku yenn xeeti kaaseeri, rawatina bii ñuy woowe kóliyóm.
 
==Turu xam-xam wi==
'''NeriumLaurus oleandrenobilis'''
 
[[Wàll:garab]]
[[Wàll:meññeef]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Lóriye » lañ ko jële