Lóriye

Lóriye gi xeetu garab la gu bokk ci njabootug Lauraceae, ci bëj-saalumu Tugal la bàyyiko waaye amna ci barab yi bari naaj ci àddina bépp, Senegaal it.

Lóriye gi (Laurus nobilis)
Lóriye gi (Laurus nobilis)

Melo wiModifier

Garabug lóriye dafa man a àgg 10i met ci guddaay, xobam day gulumba te wirgo wu nëtëx lay yore, tóor-tóor bi day mboq.

Nataal yiModifier

Turu xam-xam wiModifier

Laurus nobilis