Laay Juuf
Inscrit depuis le 14 Awril 2019
Mbërbóof
Mbërbóof xeetu garab la gu bokk ci njabootu "Curcurbitaceae", barab yu naaje yi lees koy baye. Tur wi nag ci làkku wolof ñi ngi ko tëgge ci "mbër mu bóof" ndax ba
ri gu mu bari ay njariñ rekk.
Melow mbërbóof
SoppiGarab gi danay àgg ba 5 met ci guddaay. Xobam xet gu tar ak cafka gu wex la yore.
Tóortóoram day ndaw te mboq. Car yu nooy a koy tëye.
Doom bi daa dége te puur. Guddaayam 8 ba 35i sàntimet lay àgg.
Njariñ li
SoppiMbërbóof lees di lekk la te di ko fajoo. Ci toppatoog jabet ak yenn kãseer yi dees na ko fa jëfandikoo.
Nataal yi
SoppiTuru xam-xam wi
SoppiMomordica balsamina
Turam ci yeneeni làkk
SoppiFarañse: margose