Ci angale mooy Balak; Ci faranse mooy Balak
Balag, buur ci jamonoy yonent Yàlla Musaa la woon. Moo yilifoon waa Mowab. Fey na Balaam, ngir mu rëbbal ko bànni Israyil. Man nañu jàng ci jalooreem ci Nu 22:1-24:25.
Injiil moo wax ci moom ci Pe 2:14.