Areyopas
Ci angale mooy Areopagus; Ci faranse mooy Aréopage
Bérab ci biir dëkku Aten la, bu nekk ci kaw wenn tundu xeex wu kawe. Amoon na ay siis yi ñu defare woon doj ngir kureelu dëkk ba manoon faa daje. Indi nañu Pool foofu ngir mu waareji (Jëf 17:18-34).
Tur wi moo feeñ ci Injiil ci Jëf 17:19,22,34.
Xool it Wikimedia Commons
|