Alegsàndiri
Ci angale mooy Alexandria; Ci faranse mooy Alexandrie. Fondation : -334
Alexandria (Iskindireyya) | |
---|---|
Feeñal | |
Réew | Isipt |
Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
way-dëkk | 3 500 000 nit |
atum way-dëkk | 2 001 |
Benn dëkk ak teeru ci Misra la, fu sorewul bëlub dexu Niil. Péeyu Misra la woon ci jamano Injiil ji, di dëkk bu gëna am solo ci Gereg yi. Ñaareelu dëkk bu gëna réy ci nguuru Room.
Dañuy fekk Alegsàndiri ci Injiil ci Jëf 6:9; 18:24; 27:6; 28:11.