Aha akk yaeffii domu adama yii

Aha akk yaeffii domu adama yii, moye lu nit kii mom, lim yealo teh ken waruko jel sii mom.

Nit ku neaka amna lum mom akk lum yealo teh ken waruko jel cii mom, lolu nit ku neaka warr nako ham.

Lii yeap nyiko ligaye moye rew yii neh cii aduna yeap mbotaye bii len (nyilen) fa neakal purr nyu tahawalen fa cii Pari (Faraans), dipi juneh akk juromii temerri att akk nyene fuka akk jurom neate (1948).[1] Girr ndamii nit yii yep yii neh cii aduna, akk rew yii yep cii aduna.

Lan Moye Aaha Akk Yealeaffii Domu Adama Bii

Soppi

LiNgaMom

Soppi

(a) Sa Aha Purr Deka

(b) Purr Neaka Domu DekBii

(c) Atteh Bu Degu(Woor)

(d)Sa Aaha Purr Deaku whye

Karangeh

Soppi

(a) Karangeh cii yaahuteh(cii sakula, weradii,

(b) Purr Utt Deaku Waye Su La Deaka Defea Lu Bon

(c) Atteh Bu Degu(Woor), Teh Nyu Nangula Sa Aaha Akk Sa Yealeff BanLa Japa Cii LU Worr Neh YowLa

Jama Purr Nyep

Soppi

(a) WerrGuYaram

(b) Yealeaff Purr Janga

(c) Gom Akk Deff Lula Sa Dineh Meye

(D) Nyu Arr La

Sa Yealeaf Bii Nga Mom

Soppi

(a) Cii Saye

(b) Cii Amm Family

(c) Sa Yealeaff Boodii Jigane Akk Gorr

(d) Sa Yealeaff Ken Waruttla Forseh Saye

(e) Sa YeaLeaff Purr Waxhk

(a) WahLinGna Buga

(b)Purr Sani Cart

(c) Purr Geana NyhTu

Torohal

Soppi

- Torohal Nit Purr Soonalko, NanguAaha Akk Yealeaffam

(a) Japa ku waxhnea ngurrgii defutt lu baxhk

(b) Nagu wulen ku neaka dii jamu lim gom

(c) nyaka nangu ku deka cii dekabii purr mu sanii cart

Rew Yii Aduna Yep

Soppi
  1. https://www.un.org/en/about-us/universal-declaration-of-human-rights