Xarey àdduna
(Yoonalaat gu jóge Ñaari xarey adduna yi, bu njëkk bi ak bu ñaareel bi)
Xarey àdduna yi ñooy ñaari xare yi réew yu bari ci àdduna bi bokkoon doon def ci seen biir. Doon xare yi ëpp ay yaqu-yaqu ak ay bakkan yu ci des.
Laataa Ñaareelu Xareb Àdduna bi bu njëkk bi Xare bu Mag bi lees ko daan woowee.