Àkkasaa, garab la gu bokk ci njabootu Fabaceae, Asi gu Ngopp suuf (bëjsaalum-penku) la bàyyikoo waaye ci lu yees nit tasaare na ko, ji ko Afrig.

Nataalu garabug Àkkasaa

Melo wi

Soppi

Garab gi man na àgg ba 25i met ci guddaay. Xobam day njaxas. Tóortóoram ya dañuy mboq te dajaloo ciw car ba noppi sëq te di guddee nu day ni 15 ba 30 sàntimet. Doom bi day wërbalu teg ci di àgg 10 ba 30i sàntimet ci guddaay.

Njariñ yi

Soppi

Dees ko jëfandikoo ngir: -Jëmbat pàkk yi booy. -Dekkil suuf su dee. -Faj mettig yenn cér yi. -Defar yenn garab yi.

Nataal yi

Soppi

Turu xam-xam wi

Soppi

Senna siamea

Tur wi ci yeneeni làkk

Soppi

Farañse: cassia du Siam/ casse du Siam.