Ayuba Sulaymaan Jàllo (ñu gën  Koo xam ci turu  Jòobeen Solomon)  , mi ngi judd jamonoy 1701 fëla ca  Bundu,  mi ngi dee atum 1773 .Nekkoon Imaam , waaye ba tay bokk ci  ñi loru  ca njaayum jaam yi  tubaab yi doon def nit ñu ñuul  ñi.

Nekkoon ab jaam ci ay weer ju bari fee ca  Marilaand  , moom mooy Benn jaam bi njëkk bi   dellusiwaat ci  njaayum jaam ñi  nekk Kenn ci   "Spalading Gentleman' s Society "

Ayaub Sulaymaan Jàllo  , bindul ay jaar-jaary fundamental moom ci jëmm mi boppam, waaye ñi kuy xam ci dimbalug téereb tomaas  Bulett bii génn ca atum 1734

Judd atum 1701.       Ci réewum Senegaal   , Ayuba  bi ngi bokk ci njabtoog gog ay julit lañu,  doon ay woroom xam-xam ci mag, Bi bu nekkee gone ci la jàng làkkuw Araab ak alxuraan  ,moo àndoon ak  buurub Fuuta ba bu siiw ba  Sàmba Gelaajo Jéggi .Bi Amee 29i at,  ci la ko Mandige jàpp. Ñu Njaay ko benn "kapiten" bu ñuy woowee  Piki