Yoonal
mooy balluwaay bi yoon yi di génne moom yoonal nag doole la joj péncum ndawi réew mee koy ame mooy barab biy yoonal génne jox àtte gi maanaam letaa (nguur gi) ngir mu tënku ci. Mbooleem yoon yi (les lois) ndawi réew yee koy kàddu maanaam “woote” ngir mu dem ca dooley wéyal ja àtte gi ame ngir mu doxal ko