Yiir
Yiir garab la gu guddaayam man a àgg ba ci 12 jàpp 20i met, yaatuwaayam ci benn met lay toll. Moom nag ñi ngi ko duppee garabu weñ ndax dëgëraaym max manalu ko dara.

Bérëbam
SoppiGarabu yiir nag amna Senegaal, Kamerun, Sudã ba Niseer.
Njariñ yi
SoppiAy reenam day faj bëñ yu kadam, am xasam it baax na ci góom. Ay xobam ak i bantam baax na ci góomu biir. Bantam bu dëgër boobu dees ciy defar i lal, ak i armuwaal, ak ay ndënd.
Nataal yi
Soppi-
Garabug yiir
-
Xoox i yiir