Yéesu-kristaa mooy ji ëpp solo ci diiney krist. yeesu moo yëut: « Yahweh est salut », kristaa di baatu gerek bi'y tekki ci yëut « ku sell ki »). moom la ñi daw yalla tek ci. Catolig yi, ortodoks yi ak li ëpp ci jàngu ñaxtukat yi dañ ni nit dëgg te di yalla tek ci.

Christ Carrying the Cross 1580.jpg