Xott-biteel gi xeetu garab la gu bokk ci ñoñ Eucalyptus. Óstraali la bàyyikoo.

Xott-biteel gi (Eucalyptus camaldulensis)

Melo wi Soppi

Guddaayuy 20i met lay yore, waaye man nay hàgg ba 45i met. Xàncam day dijj (3i sàntimet), woyof, te yor i gàkk gàkk yu xonq, yu baam, yu nëtëx ak yu weex. Saawiyee ba suye lay meññ ci barab yu naaje ya.

Njariñ yi Soppi

Ronam bu tàbbe cig dex, dëkkuwaay la ñeel yenn jën yi. Dees kor kerloo te di ko fajoo it.

Nataal yi Soppi

Turu xamxam wi Soppi

Eucalyptus camaldulensis

Tur wi ci yeneeni làkk Soppi

Farañse: gommier rouge/ des rivieres