Xeex garab la gog mi bokk ci njabootug Rhizophoraceae, bari na ca Gine gu digg.

Xeex gi


Melo wi

Soppi

Garab gu ndaw la gog reen yi day law ci suuf. Xob yi dañuy jàkkarloo. Doom biy sax ci garab day wërbalu te toll ci 3i sàntimet.

Fi muy ëpp di sax day am ndox, ak ndox mu am cafka xorom, walla ci wetu dex.

Njariñ yi

Soppi

Bant biy juge ci garab gi day dëgër te diis moo tax ñu koy jëfandikoo ci wallu liggeeyu bant.

Xob yi dinan faral di ko fajee gaana, lakk-lakk ak taab.

Nataal yi

Soppi
 
Tóortóor
 
Car



Turu xam-xam wi

Soppi

Rhizophora racemosa