Wikipedia:Téere wurus bi
Lii mooy téere wurus bu Wikipedia. Fii man ngeen fee sargaal képp ku leen neex, képp koo leen yaakaar ne def na ci téerexamteef bi liggéey bu am solo, bu ko jëmale-kanam. soo binde ba noppi man ngaa xaatim say mbind su dee bindu nga man ngaa xaatim ak lii -- ~~~~. Su dee binduwoo nga def ci -- ~~~~~. Soo bindoo mu bind sa tur soo binduwul mu bind bes bi rekk.
Gërëm kenn |