Waxtaani jëfandikukat:Anafa
Xammeeku
SoppiDi la nuyu
Balaa ngay bind dara soo duggoon ba noppi mooy gën, day tax nu man laa xammee ak sa tur, soo xoolee xët wii di Coppite yu mujj, sa IP lañ fa bind, te ci xëtu waxtaanukaay yi ngay xaatim soo bindee ba noppi. Soo xoolee man waatim naa. --Ibou 21 septembre 2007 à 16:09 (UTC)