Waxtaan:Njàngat

njàngat lanuy wax walla nga ne adab waaye ladab baaxul. te nag njàngat moo gën ndax moom wolof la. adab nag araab la. mooy litterature

mbind Soppi

man sax bu njëkk mbind laa bindoon ba yàgg laa gis baat bii di adab.

njangat tu tekki gëstu? etude

Ci sama gis-gis wax mbind moo gën --Ibou 2 octobre 2007 à 22:31 (UTC)

ma ne Soppi

leeg-leeg nu koy tekkee gestu waaye gestu mooy gestu, njaggat mag ni bu nu daa firi adab, naari tekkiin la amoon benn bi mooy teggiin, bi ci des di litterature nu ko daa firee ci baatu njaggat

Revenir à la page « Njàngat ».