Tabanaani xeetu gàncax la gu bokk ci njabootu Euphorbiaceaete bàyyikoo Meksig.

Tabanaani (Jatropha curcas)
Tabanaani (Jatropha curcas)

Melo wi

Soppi

Garabu tabanaani man naa àgg ba 8i sàntimet ci guddaay. Xobam day xonq. Doom bi danay ëmb lu toll ci 25% ci diw, jiwu bi nag 37% lay ëmb ci diw. Garab gi xet gu xasaw lay gilli.

Njariñ li

Soppi

Nekkam tooke teewut ñu koy bay ngir diwam. Bokk na ci lees di defaree saabu Marsey.

Nataal yi

Soppi

Turu xam-xam wi

Soppi

Jatropha curcas

Tur wi ci yeneeni làkk

Soppi
farañse: pourghère
angale: Barbados nut