Suuruur
Suuruur xeetu garab la gu bokku ci njabootug Fabaceae ñoñ Mimosoideae. Moo ngi cosaanoo ci Afrig sowwu jànt.
Aw Meloom
SoppiGarab la gog day am ay dégg. Ab guddaayam man naa àgg ba 10i met.
Njariñ yi
SoppiGarabug suuruur ay njariñam barina lool dees na jariñoo: bant bi, xas mi, ak ndox miy genne ci moom.