Suraas gi (Citrus sinensis)

Suraas gi xeetu gàjj la gu bokk ci njaabootu Rutacées. Barab yu tàng yi lees koy bay. Asi la bàyyikoo.

Melo wiSoppi

Garab gi man na àgg ba 10i met ci guddaay. Wànqaasam day am i dég te xobam 4 10i sàntimet àgg ci guddaay.

Njariñ yiSoppi

Suraas gi soloom ci wàllu koom lu fés la. Am na solo it ci wàllug paj.

Nataal yiSoppi

Turu xam-xam wiSoppi

Citrus sinensis